Khamle lanmoy manhaje , nine nioy woy jitougni thi islam , leral sen yone thi basbas akd diamou yalla ak teguine.
Ndaka lanouy drgue soumay younentebi - (Wollof)
Leral niari mbire youywaral niaka degue sounna.mousiybay dioumou borom khakham thi degue sounna…
Liy sippi jëfaye bire - (Wollof)
khoutba thie aye bire Liy sippi jëf
Waréfu sàmm kàràŋŋé gi - (Wollof)
thi kawe soufe Waréfu sàmm kàràŋŋé gi
Abeul thi dine - (Wollof)
Lanmoy abbeul thi dine, manndargay abbeul ak ay diekhaltala,sabsbi abbeul thi dine, safaray abbeul…
Sabab yiy tax Yalla wattoup jàmam - (Wollof)
Khoutba gui mi ngui ajou ci: ay sabab yiy tax Yalla wattoup jàmam
Les conditions du tawhid - La ilâha illaLlah - (Wollof)
Les conditions du tawhid - La ilâha illaLlah
Diagnele ak yar ak diekhan telam thi khetwi - (Wollof)
Neknathi leral amsolok diagn guile ak yekhan talam thi khetwi …
Ndiabar Ak Ayloram Thi Societebi - (Wollof)
Lane moy ndiabar ak lane moy aykhadia ak lane moy ay atteme thi islam ak nane lankoy safara boudalenit…
Lu bon jogéwul ci Yalla - (Wollof)
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Lu bonu késsé du jogé ci Yalla donté nitñi daño giss né lu bon la
Liy waral deukk thi jâm - (Wollof)
Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral taaroup lislam bi ngui khamné môy dîné jâmm, akiy téggine you rafète thi dounnd ak gnoudoul joullite. Di tônetou gni gnâwal thi Yonènete Mouhammad (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâm)
Nekena thi leral degue degou jihaout ak ay khadiam ak tankam ak leral loubari thi ay aylante thi jihade…